CAREI – Santru Juumtukaay ngir Njàŋgum Caada yu Duggënte – ci Aragon

Castellano – ÁrabeBúlgaro – Inglés – FrancésPortugués – Rumano – Ruso – Chino – Polaco


Santru Juumtukaay ngir Njàŋgum Caada yu Duggënte – ci Aragon (CAREI) santr la bu Bàŋqaasu Njàŋgale, Caada ak Tàggat-Yaram bu Guwernmaa wu Aragon taxawal ngir jàŋgalekatu Aragon yi sukkëndiku ci ngir dalal ak dugal ñi jóge bitim-réew ci njàŋg mi te wéer ko ci duggënte caada. Lii teg la ci ëllëg, bi nga xam ni moom rekk moo fi sës, te ngeen war ci bookk – xam ni ci ni ñu gise njàŋgmi, mëneesna tabax ëllëg teg ko ci wutum ndaje ak jaxasoo yi ñuy jëmële ci dundu mbooloo gu gënë dëgërël moom-sa-bopp, gënë yemale te gënë jappoo.

CAREI